baefa💕 (@BvefaS) header
baefa💕 (@BvefaS) profile picture

Mouride.

Joined March 2020
Photo by baefa💕 (@BvefaS)Photo by baefa💕 (@BvefaS)Photo by baefa💕 (@BvefaS)Photo by baefa💕 (@BvefaS)Photo by baefa💕 (@BvefaS)Photo by baefa💕 (@BvefaS)Photo by baefa💕 (@BvefaS)Photo by baefa💕 (@BvefaS)Photo by baefa💕 (@BvefaS)Photo by baefa💕 (@BvefaS)
Ab tënk ci gëm dogal bi Suko defee, ñett (3) yoo yu ku ko gëmee noo nu, ap jullit la. Ku ko gëmeewul noo nu nak, ap yéefér nga. Xeetu dogal yi Waa sunna ñoom noo nu ma waxee la ñu gëmee dogal bi. Waaye dogal bi nak am na ñetti (3) xeet : 1) Bu njëkk bi mooy dogal bi ñuy tuddee xamuk sunu Boroom. Boo bu mooy dogal bi jiitu ci lépp. Loo loo tax ñu naan wilaayatu goo gis ak jagle moo ko jiitu. Sunu Boroom nee na ‘’yuu faku h’anhu man ufiku’’, maanaam ‘’alxuraan ku ka gëmul ci àdduna daa fekkoon sunu Boroom dogal ko bu yàgg ni doo ko gëm’’. Yonent bi (YYJSM) nee na ku faatu ku nekk fekkoon na sunu Boroom xam ak faatoom. 2) Ñaareel bi mooy dogal bi ñu dogal te bind ko ci lawhul mahfuuz. Boo bu moom mën naa soppeeku. Ndax Yàlla nee na ci alxuraan ‘’yamhul laahu maa yachaa-u wa yusabittu wa h’indahuu umul kitaabu’’. H’abdulaahi ibnu h’omar (YYDG2) daan na wax buy ñaan: Sunu Boroom boo ma bindee may ku texeedi, Yàlla na nga ko far te bind ma may ku texe. 3) Ñetteel bi mooy dogal bi ñuy dogal bu nit ki nekkee ci biirup yaayam. Ndax malaaka mi da ñu koy digal mu bind wërsëgam akup appam akuk texéedeem akuk texéem. 4) Ñenteel bi mooy bi nga xam ni moom la ñuy tuddee andi dogal yi ci seen waxtu. Ndax sunu Boroom bind na lépp ba noppi waaye lu ci ne da koo wutal waxtu. Saa su waxtu wa aksee mu andiko. Noo nu la ñëwee ci al-ib-riiz bu al Yaddaaliyu (YYDG).
1
29
61
1,383
Gëm dogal bi Lislaam nak ñetti (3) xaaj la : iimaan, islaam ak ihsaan. Iimaan ci boppom dafa seddaliku juróom benn (6) xaaj : gëm Yàlla, gëm malaaka yi, gëm yonent yi, gëm téere yi, gëm yawmal xiyaam ak gëm dogal bi. Kon gëm dogal bi daa bokk ci liy matal sa gëm Yàlla. Lan mooy gëm dogal bi nak ? Xaaju dogal yi Gëm dogal bi ñetti (3) xaaj la : 1) Bu njëkk bi mooy nga gëm ni lu am ak fu mu ame, Yàlla xam na ko te moom la neex mu am. Wuteek al xadariyatu ñi nga xam ni dañuy wax ni dogal yi ginnaaw bi mu amee la ko sunu Boroom dooga xamee noo na. Ñoo ñu ay yéefar yu wér lañ. Ñoom sax laataa imaamu Chaafih’i-yu di génn àdduna jeex nanu takk. Lu mat juróom ñaar fukki (70) yonent rëbb nanu leen. Yonent bi (YYJSM1) nee na bu ñu tawatee bu leen kenn seeti, bu ñu faatoo bu leen fa teew. 2) Ñaareel bi mooy nga gëm bu wér ni sunu Boroom moo bind nit ñi ak seeni jëf. Wuteek al Muh’tazilatu yiy wax ni sunu Boroom moo bind jaam ñi, waaye jaam bi moo bind jëfi boppam. Ñoo ñu seenuk kéefér am na ak wuute. Waaye Alxuraan weddi na leen ci ay barap yu bari mel ni ‘’wallaahu xa- laxakum wa maa tah’maluuna’’ ak ‘’wallaahou xalaxa kulla chayin’’ ak ci yeneen aaya. 3) Ñetteel bi mooy nga gëm ni yiw ak ay, ñaari (2) mbindéefi sunu Boroom la ñu. Wuteek al Maanawiyatu ñi toppu Maaniyu, fen kat boo bu di wax ni lëndam moo bind ay. Alxuran weddi na ko bi mu nee ‘’wa jah’ala zullumaati wa nuura’’.
2
68
1
186
4,949
Yii xeet i dëgg !!
1
40
1
255
5,356
baefa💕 retweeted
Islam is the most peaceful religion to ever exist.
1,519
1,119
216
10,501
258,069
baefa💕 retweeted
« Puis Allah t’apportera une heureuse nouvelle qui te fera oublier toute l’amertume que tu as traversée. »
10
889
20
3,487
39,256
Kenn koumou si nioune biss penthie Yallah dinnala diokh terré bo khamni dou résumé wayé dina détaillé say moindres faits et gestes bah paré nila diangale té atté sa bopp !
51
8
161
14,910
19
270
5
1,674
24,209
baefa💕 retweeted
i love being told i smell good
2
728
16
1,366
27,829
baefa💕 retweeted
La déception parce qu’elle ne brise pas seulement le cœur, elle brise aussi l’image qu’on avait de quelqu’un, les mots auxquels on avait cru, les gestes qu’on pensait sincères
quel est le pire sentiment à ressentir selon vous hormis la tristesse ?
3
79
2
247
7,884
Replying to @McArthyy_
Le soufisme nous dit « si tu veux connaître la direction de ton cœur, regarde les personnes dont la compagnie te devient agréable.. »Certaines présences te rapprochent d’Allah sans même parler..d’autres t’en éloignent sans même te demander de quitter ta religion.
3
17
69
2,538
À force de côtoyer certaines personnes on finit parfois par adopter leurs habitudes leur façon de penser et même leur rapport à la religion sans même s’en rendre compte mtx gnou wara woutt des amis qui nous rapproche d'ALLAH SWT🥲
1
49
1
228
7,206
Le soufisme nous dit « si tu veux connaître la direction de ton cœur, regarde les personnes dont la compagnie te devient agréable.. »Certaines présences te rapprochent d’Allah sans même parler..d’autres t’en éloignent sans même te demander de quitter ta religion.
8
1
23
2,793
C’est justement le plus important. Le Prophète ﷺ a dit « l’homme est sur la religion de son ami proche ». On peut croire qu’on influence les autres sans être influencé, mais l’influence agit souvent silencieusement, par les habitudes, les paroles, les valeurs, les états du cœur.
En réalité qu’on le veuille ou non le choix de nos fréquentations joue un rôle immense dans notre cheminement religieux. On peut être convaincu d’être assez fort pour ne pas se laisser influencer mais personne n’est à l’abri de l’influence de son entourage xana yallah sutural la
2
2
21
890
Nahju : « Boo bëggee àndandoo, bul ànd ak ku deseedi, ku añaan wala ku bëgg adouna » « Bul toog mukk ak koo xamne dula dolli ci diine wala ci xel » « Nax jëlee nan ci Hadiis bu wér ne “Nit ki mi ngi ci diiney xaritam” » (Maanaam da koy influencer ci tolluwaayam ci diine)
À force de côtoyer certaines personnes on finit parfois par adopter leurs habitudes leur façon de penser et même leur rapport à la religion sans même s’en rendre compte mtx gnou wara woutt des amis qui nous rapproche d'ALLAH SWT🥲
2
11
1
46
1,497
baefa💕 retweeted
Ayez des amis qui vous rapproche d'ALLAH SWT.
10
3
25
3,901
Lorsque Serigne Sam Mbaye témoignait sur le Cheikh, ce dernier était loin d’être le Khalife. Aujourd’hui, il incarne toutes les caractéristiques d’un leader, à la fois temporel et spirituel, un guide sage et bienveillant, tel que Serigne Sam nous le décrivait.
5
113
4
551
13,500
Replying to @McArthyy_
Bu dee lo xamni da koy nëbb nga xamee ko feneen amo droit interpeller ko directement , sañ nga ci seen waxtan fataliko li yallah bëgg sans pointer ko . Bu dee dey def lu fës lu yallah bëggul te nëbbu ko sañ nga ñëw ci mom wax ko mais ag kaduu yu teey ngir bo ko dëggaralee mën naa ñëk . Waaye li yeep da and ag sa xol nga bañ ko juger donte ya ngi koy wax sharia da nga war a defar sa xol ba doko jappee li muy def
1
3
13
608
Ñi ma xam yeep te di ma laaj ci li gis nañ ni dama leen di tektal ñu dem janggi aqiida di na dalal sen laaj yep . Mais duma ci debat mukk ag n’importe qui ndax yonent bi dafko tere . Boroom xam xam yi baari wax ni bokk na ci yi seytaane yakamti ngir jëmbat ci xolu nit ki luy jur weddi .
Yonent bi aleyhi salaam mas naa genn fekk ay sahaaba toog di waxtaane destin di ci werante . Mu mer ma lex yi xonk !! Ni leen , ndax li la ñu seen digal ? Ndax lii mo tax ñu yonni ma ci yeen ? Ni leen xeet yi leen jiitu lii ngen di werante ni mo leen sankk , ma ngi leen di digal ngeen moytu ko Tirmizii 2133
There's a new version of this post
1
6
23
1,282
Yonent bi aleyhi salaam mas naa genn fekk ay sahaaba toog di waxtaane destin di ci werante . Mu mer ba lex yi xonk !! Ni leen , ndax li la ñu leen digal ? Ndax lii mo tax ñu yonni ma ci yeen ? Ni leen xeet yi leen jiitu lii ngen di werante ni mo leen sankk , ma ngi leen di digal ngeen moytu ko Tirmizii 2133
2
39
3
153
7,281