İl s'est tellement sacrifier il fallait ce poids pour terrasser la longévité de Yekini et donc fallait prendre des trucs chimiques pour le faire
Papa Cheikh tout m'impressionne chez lui kholal ma togay bi dafa saf adab
On dit que la faydah c'est des aa'daab' voici l'incarnant
Parfois je pense beaucoup à Mame Aladji
Goor deug moy Mame Aladji
Ce qui m'impressionne la baraqa qu Allah lui a donné
Tous ses fils sont des waliyu (savant)
Lilianito 🇳🇬 🇵🇸 retweeted
Et dites-vous qu’il a une forte douleur dentaire !
Yal nako fi Yalla bayyi lu yagg, mu andd ak wer ya Rabbi.
Lilianito 🇳🇬 🇵🇸 retweeted
Naka la nit di nekke ci fayda bi keneen wala leneen lu dul Baye di la yeem
Ku xam Baye degg mbideef ak lu mu yeeme yeeme du la jaaxal
Ibra asta rek❤️
Lilianito 🇳🇬 🇵🇸 retweeted
Lepp lu mbokk yi di woote au nom du cheikh te muy lu sëriñ bi gërëm kenn warul am ngant ñëppa wara teew jëmmal ko taaral ko ! ma gi woo bokk yi ci ñu daje ñun ñëpp and doon benn wuyu woote bi. buur yalla def ko muy sa jotaay te nga may ñu ci nassran azizan ba leppi di ci salam
Lilianito 🇳🇬 🇵🇸 retweeted
La plus grande leçon que j'ai apprise cette année est probablement de ne pas donner autant de vous-même à des gens qui ne feront pas la même chose pour vous.
Lilianito 🇳🇬 🇵🇸 retweeted
Dafay fen dh waxul dëgg. ñi seetan cérémonie bi xamnañ que ignore wu ko lutax ngeen toxique bëgg di wane lu bon rek li lo ci gagné bro ????
Moytu leen rs yi du lu nit wax rek dëgg la mais Tu vois des cons yu ñeme yàlla dinañ bakkar fekk ni li ñu gis dara amu ci
















